You are on page 1of 1

infovihtal 08

Nu uy xaaym doomu jngoroy


SIDA si yaram nit ki Carga Viral

Nu uy xaaym doomu jngoroy SIDA si yaram nit ki


Nit ki nga xamne dafa am feebar sida,li doomu jngoro gi di gn bare si deretam aakum CD4 di gn
gaaw,ci lolu jumtukaay yiy aar ci bepp doomu doomi jngoro dauy yomb wll,si at yu new mandarga yuy wan
am ga feebar si di f.

Test yoyu uy def daf uy fiirdel aata doomu jngoroy SIDA mo nek si su u deret. Doktoor yi tam di na
xamal seni nit yu feebar aata doomu gi jngoro mo nek
sen yaram si xayma (wai).
Am na fason yu bare nuuy wae aata doomu jngoy
sida mo nek ci deret tu nit ki. Way yepp o dauy fiird
ndax doomu jngoro ji nek ci deret tu nit ki bare, yam na
wala tuutina. Waye bu nek doomu jngoro ji nek si deret
nit ki dafa tuuti lool ken duko mn guiss. Wa gu new
gu wan doomu feebar gi war na tolu ci 40 wala 50 doomu jngoro gi ci fukki pacci walatu litre gu nek. Bepp test
bu wan luu guiss ci sa deret gn new 40, dauy wax
nan kenn menul guiss doomu jngoro ji waye kenn dakul
ne amo jngoro gi mn nga ko am wala nga ba ko am
,dafay wane rekk limu doomu jngoro gi mn na nek 0 ak
39 wala diggnte 0 ak 49.
Mn am yokku te doomu jngoro gi bu fekk da nga
am infection wala da nga akku won.li bu ame lu gn moy
nga bayi benn wr nga sogga def yi test wi wane aata
doomu jngoro gi mo nek sa yaram.
Fo mn nek si aduna, nu uy xaym doomu jngaro ji
benn la.

Xaay ma doomu jngoro san nga jl garab yiy


xeex moom
Bo jlul garab yiy tye donj yi.sa doktor sa doktor di
na la dfaral test bi (xaaymal la aata doomu jngoro gi
wara nek sa yaram). Ci li lay xool giir xam nan lay doomu
jngoro gi ci yaramu nit ki.ci nit u am benn xaayma CD4,
ou am xaayma doomu jngaro gi gn bare ooy gn
gaawa danu feebar.
Bala ngay xam war nga jl garab yi lay aar si doomu
jngoroy sida,da nga wara ci ay wre yu new xool aata
doomu jngaron gi nek senni deret xool tamit li di CD4 yi
ak mandarga yuy wan febaar sida mo gi lay xala daan.

Ki lay xtali di la wan nan ngay jle say garab


Jlum garab feebarum sida dina tax doomu jngoro gi
nek ci deret tu nik ki di gn nw. Bala ngay jl yi garab da
nga wara guiss sa doktor mu xool la noppi. Di na la dfar

grupo de trabajo sobre


tratamientos del vih
e-mail: contact@gtt-vih.org
website: www.gtt-vih.org
Barcelona (Espaa)

aari xaayma wute gi ci am ci lay xool giir xam doomu


jngoro gi nan lay dunde si yaw.
u bare uy jl garab gi dilen aar si gi feebar mn na
dem ba doomu jngoro bi nek seni deret waeku, li dina
tax ba du gawa danu feebar.
Diir gi ngay jle garab yi ak doomu jngoro gi lumay
new ci deret tu nit ki mn dem ba 6 wr.

Yoku yu ndaw gi doomu jngoroy sida mn


def
i nga xam ne doomu jngoro gi nek si oom dafa
nexul la guiss doomu feebar joje mn yok tuuti tuuti
dem ba 100 wala 200 doomu gi jngoro ci mini litre bo jl
(100 o 200copias/ml), dina dem ba 40/50 li nak warul tax
u ne garab gi nit ki di jl duko facc digg wessu wul 500
doomu jngoro gi ci fukk genn wal walat litre deret gu nek.
Ci lolu munul jl genenn garab dafay delu di jl gi garab.

Xool ndax garab gi nit ki di jl bax na si moom


wala det
Say garab so ko jle ni ko wala jle, xaay ma yi uy def
ci sa deret dafay wane ne doomu jngoro ji nek sa deret
dafay gn yoku. Bu ko defe sa doktor dafa lay defaral yenenn xaayma giir u xam bu bax yan garab nga wara jl ba
sa facc mn dem kanam.

Waum doomu jngoro gi ak wllem


Xaayma gu uy xaayma doomu jngoro gi nek ci nit
ki daf u wan aata doomu jngoro ji mo nek ci deret
gi, waye duu wan aata mo nek ci celul yi ak ci yenenn
ni cr com kru celul yu nek ci bopp ak yo nek ci maniiw
nit ki.febaarum sy yi tamit mn yok xaay ma doomu
jangaro ji.
Tay ji am na ay guiss guiss yu wute ci doktor yi ci wllum
feebar gi bu neke xaayma doomu jngoro ji bare wul. At
gi u wessu (enero de 2008) ay doktor suisse,dao wax ne
nit kiy jl garab bam numu ka wara jle ba xaayma gi neew
ci diir 6 weer san mu am febaarum sy koku mn tul wll
doomu jngaro gi jkkram wala jabaram. Seet kat yu bare
nanguu bi guiss guiss,nek na lu dessa wr.

Por favor, fotocpialo y Hazlo circular


Subvencionado por:

Secretara del Plan Nacional sobre el Sida

Pla Director dImmigraci

rea dAcci Social y Ciutadania

Colaboran:

You might also like