You are on page 1of 2

Niu namm a trle waxtu njng mi ci lekkool yi

Ci dogal bii: (Orden ECD/63/2016 de 16 de febrero. BOA 19/02/2016)*

Lu mu doon?
Lekkool yi am na u sa-sa bu toll ni mngl seen i waxtu njng ak sen i namm-namm ci
senum njngale. Ba tax na mn na u ci dugl ay coppite ngir toppatoo xaleyi na mu gnee
Lu mu laac?
Way jur yi ak jngalekat yi mn na oo dogal, ganaaw ay wote (yoo xam ne, i
pp da uy and ci namm-namm ya), trlinu waxtuy lekkool bi, sddl waxtu njng mi ak yi
uy jagleel yeneen i yngu, mu dppo ak seen i soxla ak mbt.
Lekkool bi di na wy di ubbi waxtu yu tolloo ak ya woon. Amaana mu am tuuti coppiku ci
waxtu ubbi ak waxtu tc, ci yenn ci lekkool yi.
Limu waxtu yi ndongo yi daan jng du soppeeku: 5 waxtu bes bu nekk
a daan yendu di fa aee ak a daan dem a di dikk ci kaar ba, da na u ko wyl waaye ci
yeneen waxtu.
Yngu yi u fas yene amal, da na u leen birl ci beneen Kyit bu uy tofal ca xaatimu
namm-namm
Trlinu waxtu ya
1.
2.
3.
4.
5.

Ab kurel boo xamne kpp kuy yngu ci njng mi da na ca bokk, da na tnk namm-namm yi
Kurelu nguur gi yore wallu njng mi, da na saytu yene yooyu, wyl ko
Kurelu jngalekat yi ak ndaw yiy saytu njng mi ci lekkool bi da na ko saxal
u tofal ca leeral way jur yi namm-namm ya ak bes ya ak waxtu wote ya
Daal di amal wote ya

Lu tax u wara wane sunu bopp ci lii?


Ndaxte un pp da oo bokk ci njng ak njngale mi ci lekkool bi
Ndaxte ca la uy waxee ni u bggee waxtu ak melo njng u sunu njaboot
Ndaxte baatu baay bi ak bu yaay ji ypp da oo am solo (aar i baat ypp la uy wai)
Kyit yiy and ak xibaar bii
Keyit buy tnk trlinu bes ak waxtu way jur yi di daje ngir leeral namm-namm yi
Keyit buy tnk trlinu bes ak waxtu yi uy def wote yi
Yngu-yngu yu yees, ak ndollent ci njngum xaley, ak yeneen xeeti yngu yu bokk ci nammnamm yi

CAREI

C/ San Antonio Abad 38

50010-Zaragoza

Tfno. 976713025

carei@aragon.es

WAXTU NJNG MI CI 2015/16

YENI EEL 2016/17

Dalee 09:00 ba 12:30 watu

Dalee 09:00 ba 14:00 watu

Jng ci kalaas bi
Jng ci kalaas bi
Dalee 12:30 ba 15:30 waxtu.

a, ndolent ci njng mi, yeneen xeeti yngu yu yees. Ll


and ak iy yore xale yiy yendu, yngu yu uute ak njng
mi

Dalee 14:00 ba 17:00 waxtu.

Dalee 15:30 ba 17:00 waxtu.


a, ndolent ci njng mi, yeneen xeeti yngu yu yees.
Ll and ak iy yore xale yiy yendu, yngu yu uute ak
njng mi

Jng ci kalaas bi

Besa k waxtu woote yi:

CAREI

C/ San Antonio Abad 38

50010-Zaragoza

Tfno. 976713025

carei@aragon.es

You might also like